pauker.at

Wolof Deutsch Vokabeltrainer

von allem etwas
DeutschWolofVorratStufeRaus
arbeitest Du dort? da nga faa liggéeyée?
Dein Kind/Baby weint sa doom jaa ngee jooy
du wirst es sehen dinga ko gis
es sind zu viele Fliegen hier fii dafa bori wéñ
gehst Du zu Fuß oder fährst Du mit dem Auto? da ngaa dox ndax dugga moto?
hast Du Knoblauch an Dein Essen gemacht? def nga laaj ci sa togga gi?
Hier hast du sie. Am, mungi nii.
ich bin an meiner Hand verletzt dama gaañu ci loxo
Ich verstehe nicht, was Sie sagen. = wissen-nicht-ich was du sagen Xamuma li nga wax.
in welche Richtung gehst Du? ban boor ngaa demee?
Keine Ursache. Amul solo. / Du dara.
komm, ich frage Dich etwas kaay ma laaj la dara
nein, er/sie ist kein Gambianer/in, er/sie ist Amerikaner/in déedéet, du Gambian, American la
wann bist Du hierher gekommen? kañ nga fi ñow
warum bist Du hierher gekommen? luttax nga ñow fii?
was machst Du? lan ngaa def?
was moechtest du machen? lo buga deff?
Was sagen Sie? = was du sagen Lan nga waax?
was verkaufst Du? lan ngaa jaay?
Welche Straße führt nach ... ? Ban tali mooy dem ... ?
Welcher Bus fährt nach ... ?Ban kaar dem ...? Ndax kaar bi dina dem ... ?
welcher Tag ist heute? tey la ban bés/ tey ban bés la?
welcher Tag ist morgen? subba/élég la ban bés?
welcher Tag ist übermorgen? ganaaw élég la ban bés?
welcher Tag war gestern? démba la woon ban bés/ démba ban bés la woon?
welcher Tag war vorgestern? barki démba la woon ban bés?
wer bitst Du? yaw yaa yi kan?
wie alt bist du? njata at nga am?
Wie sagt man ... auf Wolof? = wie du sagen ... in Wolof Naka ngay wax ... ci wolof?
wobei bist Du/was machst Du? ci loo néeka?
woher kommst du? fo djogeeh?
wohnst Du weit entfernt von Deinem Arbeitsplatz? fi nga dékka sori na ak sa liggéeyu kaay?
 
Ä
  <-- Eingabehilfe einblenden - klicken